Jammu Africa - Ismael Lo
Afrika a a a Afrika mon Afrique Sama gent gi maa ngi naan Yalla wonma ko bala may nibbi barsaq Ma ne bes du nakk ci bes yi Afrika don benn reew D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'Afrique Mem' si le ciel tombait luttons pour la paix Kon jammu Afrika moom lay naan Mane jammu Afrika mooy sunu natange Afrika a a a Afrika a a Afrika a a a Afrika mon Afrique Yow mi nekka bittim reew man mi Lo maa ngi lay naan Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur Mem' si le ciel pleurait luttons pour nos freres Kon jammu Afrika moom lay naan Mane jammu Afrika mooy sunu natange Afrika a a a Afrika a a Afrika a a a Afrika mon Afrique Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi Yoo Alla addu jam to Ruanda Yoo Alla addu jam to Burundi Yoo Alla addu jam to Casamans
|
'샹송' 카테고리의 다른 글
Vikki Carr - El Tiempo Que Te Quede Libre 外 샹송, 칸소네 13곡 (0) | 2014.05.21 |
---|---|
Saint Preux(생 프뤼) 외 클래식 모음 (0) | 2014.04.13 |
감미로운 샹송 Graciela Susana / Adoro 외 9곡 (0) | 2013.10.13 |
칸소네 모음 (0) | 2013.10.03 |
가을의 정취가 물씬나는 샹송 5곡 (0) | 2013.09.12 |