Jammu Africa - Ismael Lo Afrika a a a Afrika mon Afrique Sama gent gi maa ngi naan Yalla wonma ko bala may nibbi barsaq Ma ne bes du nakk ci bes yi Afrika don benn reew D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'Afrique Mem' si le ciel tombait luttons pour la paix Kon jammu Afrika moom lay naan Mane jammu Afrika mooy sunu natange Afrika a a a Afrika a a Afrika a a a Afrika m..